SENCOIN

leumbeul

Aller en bas

leumbeul

Message par Admin le Jeu 11 Mar - 20:52

avatar
Admin
Admin

Nombre de messages : 1476
Age : 40
Localisation : Paris
Points : 1761
Date d'inscription : 10/10/2007

Revenir en haut Aller en bas

Re: leumbeul

Message par Admin le Mer 9 Juin - 17:15

na loxo yi dathie!
na loxo yi mbeukké !
na dadié na dadié !
na loxo yi dadié !! é démal !
Abdou dafa waatie
Ablaye yéék
senghor wathioup leuguééy
niou dém diko diaalé
bato ba diik
kouné boppam la tal !!
Ndélba dafa réy té xélma naax
loumou wax fatté ko !
beut yeu da fa doug
té léx ya rass
laaye leudieul naniou !!
Laay dolli niou ? Nga doggaliniou
....
avatar
Admin
Admin

Nombre de messages : 1476
Age : 40
Localisation : Paris
Points : 1761
Date d'inscription : 10/10/2007

Revenir en haut Aller en bas

Re: leumbeul

Message par Admin le Mer 9 Juin - 17:21

borom ndél béé niou ray
Laay wadday paxoum kagna !
...Ak famèèm bou ndaw!
Bénoup diabar niaari doom
far goro ba déé !!
laay wadday paxoum kagna !
Laay waddak ndongam gou darr
laay waddak beuteum you dém


Amoul ndieurign fi,
Amoul Ndierign fe
moy paxooum kaagna
avatar
Admin
Admin

Nombre de messages : 1476
Age : 40
Localisation : Paris
Points : 1761
Date d'inscription : 10/10/2007

Revenir en haut Aller en bas

Re: leumbeul

Message par Admin le Mer 9 Juin - 19:28

na lokho yi dadjé,
na lokho yi mbeuk
na dadjé na dadjé na dadjé

na lokho yi dadjé,

demal abdou dafa wathie ablaye yeek,
senghor wathioub liguey niou dem diko djalé dji bateau ba diig kouné boppam la tal

nel ba dafa reuy, té khéle ma naakh loumou wakh fatté ko

beut ya dafa doug té lekh ya rass, laye lottal nganou

laye dolli nou mba dogalinou borom nel bé nou ray

nioune niogui degg té niogui khole bilaye guissounou dara

loutakh marché bounou lal laye djeulé niou fa

borom nel bé nou raye, diw gui dafa yokou té thieb bi cher
dakhine soubaag ngone

matte mi dafa djafé té keurigne cher kène amoul gaz ,
corant da rare té farigne dème, kène guissoul mbourou

wagnil mbourou mi mou thioppatti ko laye leudjeul guanou
avatar
Admin
Admin

Nombre de messages : 1476
Age : 40
Localisation : Paris
Points : 1761
Date d'inscription : 10/10/2007

Revenir en haut Aller en bas

Re: leumbeul

Message par Contenu sponsorisé


Contenu sponsorisé


Revenir en haut Aller en bas

Revenir en haut


 
Permission de ce forum:
Vous ne pouvez pas répondre aux sujets dans ce forum